berceuse Wolof (Sénégal)
Ayoo sama sopé
Ayoo sama sope
Ayoo sama dom
Ayoo néné
Ayoo sama sopé
Ayoo sama sopé
Ayoo sama dom
Ayoo néné
Nawo naw nawo naw nawo naw
Dém séti mam
Nawo naw nawo naw nawo naw
Dém séti mam
Traduction:
mon cœur, mon enfant, mon bébé,
volons comme des oiseaux pour rendre visite à tes grands parents