Aayo nenne
Nenne nenne tuuti
Ku may naral nenne
Sama nenne tuuti
Yobbul ma ko saalum
Saalum naari negg la
Niettel bassa waan ba
Waan ba waanu bur la
Aayo nenne
Nenne tuuti
Aayo nenne
Nenne tuuti
Ku may naral nenne
Yobbul ma ko saalum
Saalum naari negg la
Niettel bassa waan ba
Waan ba waanu bur la
Aayo nenne
Nenne tuuti
Aayo nenne
Nenne tuuti